Psalms 81:10
TSK
Buleen fat tuuru jaambur, buleen sujjóotal tuuru doxandéem.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Buleen fat tuuru jaambur, buleen sujjóotal tuuru doxandéem.
¶ Yeen laay tinu, bokk yi, mel-leen ni man, ci yooyu mbir, ndax man itam ni yeen laa mel. Tooñuleen ma benn yoon.
Xam ngeen ne fi baay féete doomam lanu féete kenn ku nekk ci yeen.
Waaye ngëm la koy ñaane te bumu ci am benn sikki-sàkka, ndax kiy sikki-sàkka daa mel ni gannaxu géej bu ngelaw liy yóbbu, di ko lëmbaaje.