TSK

TSK · 2 Kings 12:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ci biir loolu doomu Axiya, ji giiroo ci Isaakar te ñu di ko wax Basa, daldi fexeel Nadab, jam ko ca Gibeton gu Filisteen ña. Fekk Nadab ànd ak Israyil gépp, gaw Gibeton.

¶ Akasiya buurub Yuda gis loolu, daw jaare ca yoonu Bet Gan, Yewu dàqi ko, tey yuuxu naan: «Jamleen ko, moom itam.» Ñu jam ko ca kaw watiiram ca yoon wa ngay yéeg jëm Gur, ca wetu Yiblam. Mu daw ba Megido, dee foofa.

¶ Ba buurub Israyil Yowayas doomu Yowakas duggee ñaareelu atu nguuram, ca la Amaciya doomu Yowas falu buur ca Yuda.

Lalal nañu ko pexe ca Yerusalem, mu daw dem Lakis. Ñu yónnee dabi ko ca Lakis, rey ko foofa.