¶ Ba ñu demee ba mu yàgg, doomu Suwa, soxnas Yuda faatu. Ba dëj ba wéyee, Yuda dem fekki watkati xaram ca Timna. Ira, xaritam bi dëkk Adulam a nga ànd ak moom.
TSK
TSK · 2 Samuel 13:23
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Genesis 38:12
TSK
1 Samuel 25:4
TSK
Ci biir loolu Daawuda dégge ca màndiŋ ma ne Nabal a ngay watlu ay xaram.
1 Samuel 25:36
TSK
¶ Ba mu ko defee Abigayil dellu ca Nabal, fekku ko lu moy mu amal biir këram bernde ju mel ni berndey buur. Xol baa nga sedd, mu màndi lool, ba tax Abigayil waxu ko dara ba bët set.
1 Kings 1:19
TSK
Sarxe na ay nag ak wëllu yu duuf ak xar yu bare. Woo na ca doomi Buur yu góor yépp, woo ca Abiyatar sarxalkat ba, woo ca Yowab, njiitu mbooloom xare mi. Waaye Suleymaan sa surga ba, woowu ko.
2 Kings 3:4
TSK
¶ Ci biir loolu, Mesa buuru Mowab doonoon boroom jur, di fey buurub Israyil galagu téeméeri junniy xar (100 000) ak téeméeri junniy kuuy (100 000) yu ñu watul.
Nehemiah 11:33
TSK
ak Àccor ak Raama ak Gitayim;