TSK

TSK · Acts 15:23

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ba ñu agsee, dañoo woo mbooloom gëmkat ña, àgge leen mboolem na Yàlla def ak ñoom, ak na mu ubbilee jaambur ñi dul Yawut buntu ngëm.

Acts 15:4 TSK

Gannaaw loolu, ñu agsi Yerusalem, mbooloom gëmkat ñi, ak ndawi Yeesu yi, ak mag ñi, dalal leen, ñu nettali leen mboolem ni Yàlla def ak ñoom.

Ci kaw loolu mu jaare diiwaani Siri ak Silisi, di ñaax mboolooy gëmkat ña.

Acts 21:3 TSK

Naka lanu dem ba séen dunu Sippar, wacc ko nag sunu wetu càmmoñ, jublu diiwaanu Siri, ba teeri Tir, ndax fa la gaal gi waroona yebbi ab yebam.

¶ Ñeel la yaw boroom réew mi, Feligsë mu tedd mee tedd, bawoo ci man Këlódd Lisiyas, mi lay nuyu.