Acts 19:32
TSK
Ndaje maa nga rëb lool, ñii xaacu ne lii, ñee xaacu, ne lee, te ña ca ëpp sax xamuñu lu waral ndaje ma.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ndaje maa nga rëb lool, ñii xaacu ne lii, ñee xaacu, ne lee, te ña ca ëpp sax xamuñu lu waral ndaje ma.
Ci kaw loolu njiitu gàngoor ga santaane, ñu dugal Póol ca tata ja te laaje ko ay yar, ngir xam lu waral ñu di ko yuuxoo noonu.
Xuloo ba nag gëna tàng, ba njiital gàngoor ga mujj ragal ñu sëxëtoo Póol, ba def ko ay dog. Mu daldi sant lenn ca xarekat ya ñu wàcc, jële Póol ci biir nit ñi, yóbbu ko ca tata ja.
Ca ëllëg sa takk-der yay deme tànk waññiku, délsi ca tata ja, bàyyi gawar ga, ñu gunge Póol ba mu àgg.