¶ Aji Sax ji ne Musaa: «Tàllalal sa loxo, mu tiim réewum Misra, ngir njéeréer yi ñëw, song réewum Misra, ba lekk gàncax gi ci réew mi, lekk lépp lu fi tawub yuur bi bàyyi woon.»
TSK
TSK · Amos 7:1
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Exodus 10:12
TSK
Jeremiah 1:11
TSK
¶ Kàddug Aji Sax ji dikkal ma, ne ma: «Yeremi, loo gis?» Ma ne ko: «Caru garabu saal laa gis.»
Ezekiel 11:25
TSK
Ba loolu amee ma àgge waa ngàllo ga mboolem mbir ya ma Aji Sax ji won.
Joel 2:25
TSK
«Sama mbooloom xare mu réy, mi ma yebaloon fi seen biir, te ñuy njéeréer yeek seen tostan, ak salleer yeek soccet yi, maa leen di delloo ati mbey yi ñu leen lekkal.
Amos 7:4
TSK
¶ Boroom bi, Aji Sax ji dellu ma feeñu. Ndeke Boroom bi, Aji Sax ji day waaja mbugale ñoñam sawara. Mu xoyom xóotey géej mbàmbulaan, bay waaja xoyom réew ma.
Amos 8:1
TSK
¶ Gannaaw gi Boroom bi, Aji Sax ji dellooti feeñu ma. Ma jekki gis dàmbu meññeef.