¶ Ba ma déggee kàddu yooyu, damaa toog di jooy, ñaawlu ko ay fan, di woor ak a ñaan ci Yàlla Boroom asamaan.
TSK
TSK · Daniel 10:2
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Nehemiah 1:4
TSK
Psalms 43:2
TSK
Yaw Yàlla kat yaay sama rawtu. Lu tax nga wacc ma, may wéye tiis, ci noteelu noon?
Isaiah 66:10
TSK
Yeen soppey Yerusalem yépp, bégandooleen ak moom, te di ko bànneexoo. Mboolem yeen ñi doon ñaawlu tiisu Yerusalem, bokkleen ak moom xolam bu sedd.
Daniel 9:24
TSK
¶ «Juróom ñaar fukki ayi bés lañu àppal sa mbooloo ak sab dëkk bu sell, ngir dakkal tooñ gi, jeexal moy gi, jotu ñaawtéef, saxal njubte ba fàww, matal peeñum yonent, ba delloo bérab bu sella sell ag sellngaam.
Romans 9:2
TSK
Li may wax moo di tiis wu réy laa am, ak naqaru xol wu dakkul,
Revelation 11:5
TSK
Ku leen nara lor, sawaraay génne seen gémmiñ, lakk seeni noon. Képp ku leen nara lor, noonu ngay deeye.