Genesis 3:5
TSK
Waaye Yàlla xam na ne bés bu ngeen ci lekkee, seeni bët dina ubbiku, ngeen mel ni Yàlla, xam lu baax ak lu bon.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Waaye Yàlla xam na ne bés bu ngeen ci lekkee, seeni bët dina ubbiku, ngeen mel ni Yàlla, xam lu baax ak lu bon.»
¶ «Buleen xédd seen jabaru dëkkandoo, buleen xemmem këram, mbaa toolam, mbaa jaamam bu góor, mbaa jaamam bu jigéen, mbaa aw nagam, mbaa mbaamam, mbaa mboolem seen alalu dëkkandoo.»
Maay yéeg fa kaw niir ya, ba mel ni Yàlla Aji Kawe ji!”
«Yaw nit ki, waxal Boroom Tir, ne ko: “Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Dangaa fuuy ba naan: ‘Maay Yàlla, ji tooge toogub yàlla yi, fi xolu géej!’ Waaye yaw doom aadama nga, doo Yàlla, dangay yàlla-yàllalu rekk.
Ñooñu ñooy aaye ab séy, di digle ñàkka lekk yenn ñam yu Yàlla sàkk, ngir gëmkat ñi xam liy dëgg, man cee jariñu te di ko sante Yàlla.