TSK

TSK · Daniel 2:39

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Maa naa ci Sirus: “Sama sàmm bi!” Mooy matal sama bépp nammeel, te it moo naa ci Yerusalem: “Nees ko tabaxaat,” kër gu sell gi, laa ne: “Nees ko yékkatiwaat!”»

SÉDDALE: Séddale nañu sam réew, ba jox ko xeeti Medd ak Pers.»

¶ «May xool ba tey, yem ci rab wu mel ni segg, am ñeenti laaf. Rab waa ngi am ñeenti bopp, ñu jox ko kilifteef gi.

Ma séentu, xool, yem ci kuuy mu taxaw feggook yoonu ndox ma, am ñaari béjjén yu gudd te benn bi gëna gudd ba ca des. Waaye bi gëna gudd moo mujja sax.

Sikket bi buuru réewum Geres la. Béjjén bu gudd bi ci diggante bët yi mooy buur bu jëkk bi.

¶ «Léegi, maa ngi lay xamal lu wér. Dama ne, dina amaat ñetti buur yuy falu ci réewum Pers, ñeenteel ba dikk, dajale alal ju bare, ba ëpple leen ñoom ñépp. Bu demee ba alalam may ko doole, dina def lépp lu mu man ngir xabtal ñépp ci kaw nguuru Geres.

Bi fas yu ñuul yi takk, réewum bëj-gànnaar la jëm; bi fas yu weex yi takk topp seen gannaaw; fas yu tippante yi nag, réewum bëj-saalum lañu jëm.