TSK

TSK · Daniel 3:10

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mu ne leen: «Bu ngeen dee rewli jigéeni Ebrë yi, nangeen xool lu xale bi doon. Su dee góor, reyleen, su dee jigéen, bàyyileen, mu dund.»

¶ Yonent Yàlla Maryaama, jigéenub Aaróona nag ŋàbb tabala, jigéen ñépp topp ko, génn di fecc, tabala ya jiin.

Mu jëm ci njiital jàngkat yi, giiroo ci Asaf, te ànd ak xalam gu ñuy wax gitiit.

Loo séq ak njiit lu jubadi luy yoonal njubadi?

Màggaleleen kog liit, màggale ko xalam ak moroom ma.

Wóoy ngalla boroom dogal yiy dogal njubadi, bind ko, te muy jur coono,

Léegi, bettuma leen. Bu ngeen di dégg bufta geek toxoro geek xalam geek riiti geek kooraa geek liit geek mboolem jumtukaayi xumbal yi rekk, sujjóotleen, màggale ko jëmm ji ma sàkk. Waaye su ngeen ko màggalul, dees na leen daldi sànni ci biir taalu sawara bu yànj. Ana yàlla ju leen di musal ci man?»

Amos 6:5 TSK

yeena ngi foyantoo xalam, di fent woy yu ànd ak xalam ni Daawudaay.

Ba mu ko defee, mag ak ndaw, boroom alal ak baadoolo, as gor akub jaam, ñépp, mu defal leen màndargam loxol ndijoor mbaa jë,