KYG / Daniel / [JC0] chapitre 6 KYG · verse 25 Aa Xoolaat Jàngalekatu bind ¶ Ba loolu wéyee Buur joxe ndigal, ñu indi nit ña tuumaaloon Dañeel, ñu tàbbal leen ca... Dayo bind A- 25px A+ Font jàngat Serif Amul Naskh Amiri Scheherazade New Noto Sans Arabic Cairo Tajawal Markazi Text Changa Noto Kufi Arabic Alexandria Almarai Aref Ruqaa Ink El Messiri Harmattan IBM Plex Sans Arabic Mada Reem Kufi Lateef Reset ← Daniel 6:24 Daniel 6:26 → Toppal Yoon yu jàmm Jàngalekat Jàmm Nòt ♥ 📝 B a loolu wéyee Buur joxe ndigal, ñu indi nit ña tuumaaloon Dañeel, ñu tàbbal leen ca kàmbu gaynde ya, ñook seeni doom ak seeni jabar. Àgguñu suuf sax, gaynde ya alawti leen, dammate seen yax yépp. Chapitre bi yépp Aaya yi ci méngoo Tekki Wolof yépp Bible yépp