TSK

TSK · Deuteronomy 21:17

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ibraayma nag donale Isaaxa lépp lu mu moom.

«Ruben, yaw mi ma taawloo, nga sosoo sama digg doole, sama ndoortel kàttan, yaa jëkke sut moos ci teraanga ak doole.

Moo fàdd luy taaw ca seenum réew, muy lu jëkka soqeekoo seen digg doole.