TSK

TSK · Deuteronomy 32:49

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

«Bu ngeen demee ca réewu Kanaan ga ma leen jox muy seen moomeel, bu ma tegee liir wuy law ba xuural ab néeg foofa ca seen réewum bopp,

jógeeti Almon Diblatayim, dali ca tundi Abarim, janook tundu Nebo.

Yaw mi mel nii, buur bi ci taar bi ngay teg bët; yaay gis réew mi ne màww.

¶ Xam nanu ne sunu yaram, sunu këru kaw suuf gii di ab xayma, bu daanoo it, am taax lanu am fa Yàlla, kër gu sax dàkk, gu loxol nit tabaxul.