TSK

TSK · Ecclesiastes 4:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 3:16 TSK

Mbaa ma mel koon ni lumb wu làqu biir suuf, mbaa cuux mu jotula gis ug leer.

Job 10:18 TSK

Ana loo ma doon génnee sama biiru ndey? Doon naa dee te bët du ma gis!

Gis naa jépp jëf ju jëfe ci kaw suuf, ndeke lépp cóolóoli neen la ak napp um ngelaw.

Ku giir téeméeri doom, dund ati at, ak lu at ya bare bare, su bégewul teraanga ja mu am te amul njégu bàmmeelam sax, kooku lumb wu tuuroo ko tane.

«Ñu ngi tàwwi ni fittkat seen làmmiñu workat, seen doole ci réew mi doxaluñu ci yoon. Ñu ngii di def lu bon ci kaw lu bon, te man faalewñu ma.» Kàddug Aji Sax jee.