Su ko defee, bu Aji Sax jiy wër ci biir réew mi, di fàdd waa Misra, ba gis deret ji taq ci seen njëël bunt ak seen ñaari jëni bunt, day teggi bunt ba, te du bàyyi malaakam reykat bi, mu dugg seeni kër, di fàdde.
TSK
TSK · Exodus 11:4
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Exodus 12:23
TSK
2 Samuel 5:24
TSK
Booy dégg tànk yuy jaab ca kaw njobbaxtali sànd ya rekk, gaawtul, ndax booba Aji Sax jee la jiitu, di dumaji waa dalub Filisti.»
Psalms 60:10
TSK
réewum Mowab di sama ndabal raxasukaay, Edom, ma teg tànk; Filisti, ma xaacoo fa.»
Amos 4:10
TSK
«Maa leen yónnee mbas mu mel ni mu waa Misra. Maa reylu seeni waxambaane ci xare, jàpplu seeni fas, gillil xetu néew ya ca seeni dal. Taxul ba tey ngeen waññiku fi man.» Kàddug Aji Sax jee.
Micah 2:13
TSK
Kiy bëtt mooy dox, jiitu leen, ñu bëtt, jàll bunt bi, dem. Seen buur mooy jàll jiitu leen, Aji Sax jeey dox fa seen kanam.»