TSK

TSK · Exodus 16:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Musaa woo Aji Sax ji wall, Aji Sax ji won ko dammitu bant, mu sànni ko ca ndox ma, ndox ma neex. Foofa la Aji Sax ji dogalal bànni Israyil ay sàrti yoon ak ndigal, te fa la leen nattoo itam.

Moo leen leele mànnu màndiŋ, ma seeni maam xamuloon, ngir teg leen coono, nattu leen, te mujje baaxe leen.

Pepp mu tawe asamaan nga faje seen xiif, ndox mu balle ciw doj, nga faje seen mar, te ne leen ñu dem nanguji réew ma nga leen giñaloon.

Woykat ya sax ña nga nekkoon ca ndigalal Buur lu leen di dogalal la leen war bés bu nekk.

Ñu sàkku, mu wàcceey picci përëntaan, teg ca reggal leen mburum asamaan.

Luke 11:3 TSK

May nu bés ak bés sunub dundu bés bu nekk.