TSK

TSK · Exodus 40:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ «Nanga defare sarxalukaay bi bantu séng, guddaay bi di juróomi xasab, yaatuwaay bi di juróomi xasab; ab kaare la sarxalukaay biy doon, taxawaayam di ñetti xasab.

Sarxalukaayu rendi-dóomal bi nag, ñu teg ko ci bunt màkkaanu xaymab ndaje mi, daldi def ci kawam saraxu rendi-dóomal bi, ak saraxi pepp mi, na ko Aji Sax ji sante woon Musaa.

Moo tax cant ñeel ko, ndax yiwam wu màgg wi mu nu baawaanal ci Soppeem bi.