TSK

TSK · Exodus 9:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ba loolu amee muy waaja dee, jigéen ña ko doon taxawu ne ko: «Na sa xel dal, ndax doom ju góor nga am.» Waaye àdduwul, teewluwul.

Job 7:17 TSK

Luy nit ba nga di ko gëddaal, bay def sam xel ci moom,

Kuy foog, gisu ay, làqu; ab téxét ne ca tëñëx, loru.

Waa ja ne ma: «Yaw nit ki, xoolal bu baax, teewlool say nopp te def sam xel ci mboolem li ma lay won. Ngir won la moo tax ñu indi la ba fii. Mboolem loo gis, nanga ko àgge waa kër Israyil.»