Ayca nu wàcc, safaan seen làkk, ba dootuñu déggoo.»
TSK
TSK · Genesis 11:3
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
yen leen toskarey àddina ndax liggéey yu metti. Ñuy móol ban, di tabax, waa Misra teg ca sëf leen mboolem liggéeyu tool ya. Néegoon nañu ca ñoom lool ca mboolem liggéeyu njaam bu ñu leen sas.
«Buleen defati na woon, di jox mbooloo mi boob mu ñuy móole. Gannaaw-si-tey nañu dem wutal seen bopp boob.
di jam ku ñu tëru te deful dara; jekki jam ko, te tiituñu ci dara.
Saam xel da ne: «Xaaral rekk, ma natt bànneex, ñam lu neex ba xam.» Ndeke loolu it, cóolóoli neen.
Aji Sax ji yékkati nooni Buur Reccin, fi seen kaw, gemb seeni bañ,
Ñoo di xeet wu ma ne jàkk, dëkke maa naqaral, di sarxalali tuur ci biiri tool, di leen taalal cuuraay ci kaw sarxalukaay bu ñu tabax,
Waaye bés bu nekk deeleen soññante li feek muy bésub tey agum, bala bàkkaar a nax kenn ci yeen, ba mu mujj dërkiis.
¶ Kaayleen nag ma wax leen, yeen ñi naan: «Tey mbaa ëllëg ma dem ba dëkk sàngam, def fa at, julaa fa ba tonu.»