TSK

TSK · Genesis 39:20

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ba loolu wéyee kiy topptoo naani buuru Misra ak lakk-katu mburoom dañoo tooñ buuru Misra, seen sang.

Ndax man kat dañu maa sàcce ca réewum Ebrë ya, te fii itam, defuma fi lu tax, ñu war maa tëj.»

Ca la Yàllay jóg, ngir àtte, ba wallu kuy néew dooley àddina. Selaw.

Àtte nañu ko ñàkkal, yóbbu, te ag maasam kenn teewluwu ci ne tooñ gu sama bokk yi tooñ lees ko dagge ci réewum aji dund ñi, te loolu lees ko fàdde.

Xibaaru jàmm boobu moo tax may daj coono yu metti ni defkatu mbon, ba ci jéng yii ñu ma jéng. Waaye kàddug Yàlla moom, deesu ko jéng.