¶ Bi loolu wéyee Aadama dëkkoo soxnaam, mu am doom ju góor; tudde ko Set (mu firi May), ndax da ne: «Yàlla may na ma weneen askan, mu wuutu Abel, mi Kayin rey.»
TSK
TSK · Genesis 4:2
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Genesis 4:25
TSK
Genesis 30:29
TSK
Yanqóoba ne ko: «Yaw ci sa bopp xam nga ni ma la liggéeyale ak ni sa gétt mujj mel ndax man;
Genesis 46:32
TSK
Dafa di seeni góor ay sàmm lañu, ag jur lañu masa yar, te indaale nañu seen jur gu gàtt ak gu gudd ak mboolem lu ñu moom.”
Exodus 3:1
TSK
¶ Léegi Musaa ngay sàmm gàtti goroom Yettro, sarxalkatu Majan ba. Mu yóbbu jur ga fu sore ca màndiŋ ma, daldi agsi ca suufu tundu Yàlla wa ca Oreb.
Psalms 127:3
TSK
Ma ne, doom Aji Sax jee koy sédde, njurum doom yool la.
Luke 11:51
TSK
La dale ca deretu Abel ba ca deretu Sàkkaryaa, ma ñu rey ca diggante sarxalukaay ba ak bérab bu sell ba, maa leen ko wax déy, dees na ko topp niti tey jii.