Genesis 40:12
TSK
¶ Yuusufa ne ko: «Piri mi mooy lii. Ñetti car yi, ñetti fan la.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Yuusufa ne ko: «Piri mi mooy lii. Ñetti car yi, ñetti fan la.
Mu gis juróom ñaari nag yu rafet te suur génne ca dex ga, di for baraxi tàkk ga.
Nu ngi dëgmal juróom ñaari ati naataange yu réy ci mboolem réewum Misra.
¶ Ci kaw loolu juróom ñaari ati naataange ya jeex ca réewum Misra,
Su ko defee nga defarlu juróom fukki lonku yu wurus yu ñuy jokklee sor yi, ba jaamookaay bi doon benn.
te ñoom ñépp, menn ndoxum kéemaanu Yàlla ma lañu naan, ndax ñoo doon naane ca doju kéemaanu Yàlla ga, doj wa leen doon gunge, te doj wa Almasi la woon.