Genesis 45:6
TSK
Ñaari at a ngii xiif baa ngi ci réew mi, te fii ak juróomi at ci kanam, kenn du bey, kenn du góob.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ñaari at a ngii xiif baa ngi ci réew mi, te fii ak juróomi at ci kanam, kenn du bey, kenn du góob.
dëël fa ñu xiif, ñu sanc fab dëkk, dëkke,
Nit a ngi móolu kuy denc pepp, ba mu ñàkkee, di gërëm ka koy jaay.
Ku néewle bey na, meññeef ne gàññ, ñu àtte ko ñàkkal, mu ñàkk ko.
Xool-leen ci lii: Ndax beykat bi day dëkke gàbb, di rëdd ak a gàbbaat?