Ku bon lees di ñoddee fa jàmmi xaymaam, diri ko ba fa kanam buuru musiba yi,
TSK
TSK · Hebrews 2:15
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Job 18:14
TSK
Job 33:21
TSK
jeex tàkk bay réer ak a feeñ, yaxam ya ne fàŋŋ te sàngu woon,
Psalms 55:4
TSK
coowal noon yee ak coonob ñu bon ñi. Dañu maa teg fitna, di ma songe xadar.
Psalms 73:19
TSK
Yàquleeka leena bett! Musibaa leen ne fuuf, ñu ne mes!
Luke 1:74
TSK
ne moo nuy may nu mucce ci loxoy noon, ba man koo jaamoo xel mu dal
Romans 8:21
TSK
ñoom ñi bokk ci càkkéef googu itam, ne dees na rengi seen buumi njaam gi leen ndee ak yàqutey yaram ràng, ngir ñu am cér ci goreelug doomi Yàlla yi, am cér ci seen teraanga.
Moo nu wallu ci googu dee gu naroona metti, moo nuy walluwaat, te moom lanu yaakaar mu wallooti nu.
2 Timothy 1:7
TSK
Ndax kat Noo gi nu Yàlla jox taxu noo ragal, xanaa kay da noo may doole, ak cofeel, ak jëfin wu laloo am xel.