mbaa gannax yuy riir, di fuur ak a fuddu bay gësëm tund yi. Selaw.
TSK
TSK · Isaiah 1:21
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ngelawal penku, moom ngay tase gaal gu mag.
Ku bon, boo ko yërëmee, du xam njekk. Biir réew mu nit ñay jubal lay xal di luubale, du faale kawewaayu Aji Sax ji.
Waaye yeen, dikkleen fii, yeen doomi xërëmkat yi, yeen askanu njaalookat yiy gànctu,
Mu ne: «Su waay fasee jabaram, mu dem doon jabaru keneen, Su waa ja jëlaatee ndaw sa ëllëg, Loolu du sobeela sobeel réew mii? Moona yeen gànctu ngeen aki fari far, Ana nu ngeen mana délsee fi man?» Kàddug Aji Sax jee.
¶ Ba loolu amee kàddug Aji Sax ji dikkal ma ne ma:
¶ Kàddug Aji Sax ji dikkal na ma ne ma:
Wóoy ngalla fippukat bu sobewu bi, dëkkub notkat yi.
¶ «Yerusalem, Yerusalem, yaw miy bóom yonent yi, di sànni ay doj ñi ñu yebal ci yaw, ba ñu dee, ñaata yoon laa namma dajale say doom, uuf ni ganaar di uufe ay cuujam, te nanguwuloo?
¶ Waaye yeen fi ngeen agsi moo di tundu Siyoŋ, dëkku Yàlla jiy dund, te mooy Yerusalem ga ca asamaan, yeena àgg fa junniy junniy malaaka, dajee di màggal;
Seeni néew da naan lareet ci péncum dëkk bu mag boobu ñuy misaale turu Sodom mbaa Misra, fa ñu reye woon seen Sang ci bant.