TSK

TSK · Isaiah 3:12

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ci kaw loolu Atalyaa yaayu Akasiya xam ne doomam ju góor dee na, mu daldi faagaagal mboolem ku bokk ci askanu buur.

«Maay def ay gone jiite leen, di ñu yaroo seen sago, yilif leen.

Kon nag yeen kókkalikat yi yilif askanu Yerusalem wii, dégluleen kàddug Aji Sax ji!

Micah 3:5 TSK

Lii la Aji Sax ji wax ci yonent yiy lajjal samay bokk: «Bu ñu sàqamee ab lanc, yéene jàmm; ku leen leelul, ñu biral waxyub xare.