TSK

TSK · Isaiah 37:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 15:21 TSK

coowal musiba mooy buur nopp ya, yàqkat bette ko biir jàmm.

Moo tax Boroom bi, Aji Sax ji Boroom gàngoori xare yi, di yebal woppi ràgg fi kaw mbuxreem yi, seen daraja tàkk, sawara xoyom ko.

Xeet yaa ngi ŋarandoo ni ndox mu baawaan, Yàlla gëdd leen, ñu daw ba sore; ngelaw yëngu, ñu naaw, ni boob, ba ca kaw tund ya, mbete pënd bu ngëlén wal, mu def callweer.

noo ga di wal mu baawaan, tollu ci put; mu nara segge xeet yi ab seggukaayu alkànde, wewal xeet yi ag laab gu leen di réeral.

Aji Sax ji nee: «Xaaral rekk ma jóg, xaaral rekk ma ne ñokket, xaaral rekk ma teewal samag kawe.

Yaa xadaru sama kaw, ba sag reewande tàbbi sama nopp! Maa lay takkal ag nos akug laab, waññi la, nga dellu yoon wa nga dikke woon.

Gannaaw gi, ba muy sujjóot ca kër tuuram ma ñuy wax Nisrog, Addraameleg ak Sareser, doomam yu góor ñoo ko fa fàdde saamar. Ñoom nag ñu daw làquji réew ma ñuy wax Araraat. Ci kaw loolu doomam Asaradon falu buur, wuutu ko.