TSK

TSK · Isaiah 5:18

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ci kaw loolu Absalom ne Ayitofel: «Xelal-leen nu boog, lu nu wara def?»

Mu jëm ci njiital jàngkat yi, ñeel Daawuda. Ab dof a ngi naa ci xelam: «Yàlla amul!» Ñu ni mel ay def njekkar, seeni jëf siblu, kenn defu ci lu baax.

Aji Sax ji, say ñoñ lañuy dëggaate; say séddoo lañuy néewal.

Yeena naay: «Danoo wóllëranteek ndee, njaniiw lanu digool, ba du nu moom, ba bu yaru musiba dikkeek diisaayam, du nu laal? Noo def ay fen sunu rawtu, ay wor di sunu làquwaay.»

Yonent yiy wax waxyuy fen, sarxalkat yiy jiitee seen coobare, te sama ñoñ soppe ko ni! Moo bu muj ga taxawee, nu ngeen di def?»

Ay jaalookat la réew mi fees déy, alkànde déy a waral réew mi maral, parluy màndiŋ mi wowal. Seeni xél loraange la, seenug njàmbaar di naka-su-dul-noona.

Ku mana làqoo làquwaay, ba duma ko gis?» Kàddug Aji Sax jee. «Xanaa du asamaan ak suuf, maa ko fees?» Kàddug Aji Sax jee.

¶ Ñu baree nga fa woon, di mboolem ña xamoon ne seeni jabar dañuy taalal cuuraay yeneen yàlla ak mboolem jigéen ña teew. Ñuy mbooloo mu réy, ñépp ña sanci Misra, ba ca diiwaanu Pattros. Ñu daldi ne Yeremi:

Gannaaw yeena fen ba jeexal xolu aji jub, te du maa ko tegu naqar, gannaaw yeena dooleel ku bon, tere koo dëpp yoonu mbonam ba dund,