TSK

TSK · Jeremiah 43:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Firawna nag tudde Yuusufa Safnat Paneya, may ko jabar Asnat doomu Potifera ma doon sarxalkat ca dëkk ba ñuy wax On. Yuusufa doxe ca tegoo kilifteefu Misra gépp.

Su keroogee mu am juróomi dëkki réewum Misra yu nit ñay waxe làmmiñu ebrë, di fa giñe Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, benn dëkk ba lañuy wooye Ir Ayeres, dëkkub yàqute.

¶ Firawna buuru Misra it nàndal naa ko ca, mooki surgaam aki kàngamam ak waa réewam,

«“Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Maay sànk kasaray tuur yi ak yàllantu ya ca Memfis. Buur dootu tooge jalu réewum Misra, te maay indi tiitaange biir Misra.