Job 11:3
TSK
Sa kebetu yii wedamal na kenn a? Am dangay ñaawle te deesu la tiiñal?
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Sa kebetu yii wedamal na kenn a? Am dangay ñaawle te deesu la tiiñal?
Sa waxi ngelaw yii da dul jeex? Ana lu la cuq, ba ngay wax rekk?
Dungeen ma noppee xañ jàmmi bakkan, di ma sëf wax ju dul jeex?
¶ Fa la ñetti góor ñooña noppee tontu Ayóoba, ndax la Ayóoba gis njekkam.
Ab dof sax bu noppee, nirook boroom xel; ku ne cell, ñu fooge lag muus.
Moo tax ku xelu ci jii jamono ne cell. Céy jii jamono ju bon!