Sa màggaay gu yéemee nërmeel say noon. Yaa yebal sa mer, mu ne jippét, xoyom leen ni boob.
TSK
TSK · Job 21:18
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Exodus 15:7
TSK
Job 27:21
TSK
ngelawal penku déjjatee ko këram, jalax, mu wéy.
Psalms 35:5
TSK
Yal na leen malaakam Aji Sax ji bëmëx, nim ñax mu ngelaw wal.
Psalms 83:14
TSK
Éy Yàlla, wëndeel leen ni callweer, ñu mel ni boob mu ngelaw wal.
Isaiah 17:13
TSK
Xeet yaa ngi ŋarandoo ni ndox mu baawaan, Yàlla gëdd leen, ñu daw ba sore; ngelaw yëngu, ñu naaw, ni boob, ba ca kaw tund ya, mbete pënd bu ngëlén wal, mu def callweer.
Isaiah 40:24
TSK
Ba ñu sampoogul, toogaguñu sax, ba seeni reen di riigu, ca la leen Aji Sax jiy wal, ñu wow, ngëlén buub, yóbbu ni boob.
Jeremiah 13:24
TSK
«Maa lay tasaare ni boob muy naaw mu ngelawal màndiŋ mi wal.
Nahum 1:10
TSK
Niy taxas la ay noonam di laxasoo, mel ni ñu naan ba màndi, te ni boob mu wow lañuy lakke ba xoyomu.