Waaye yaw Aji Sax ji, yaa may feg, di ma teral, di ma siggil.
TSK
TSK · Lamentations 3:56
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Psalms 3:4
TSK
Psalms 5:3
TSK
Sama Buur, sama Yàlla, déglul, ma ne wallóoy! Yaw laay ñaan.
Psalms 6:9
TSK
Yeen, defkati ñaawtéef yépp, xiddileen ma! Aji Sax ji dégg na saay jooy,
Psalms 55:1
TSK
Mu jëm ci njiital jàngkat yi, ànd aki xalam, dib taalif, ñeel Daawuda.
Psalms 55:18
TSK
Subaak ngoon ak njolloor, may ñaxtook a ñurumtu, mu dégg ma.
Psalms 88:13
TSK
Ana kuy yég say kéemaan ci googu lëndëm? Ku lay seedeel njekk réew ma fàtte faloo?
Isaiah 38:5
TSK
«Doxal ba ca Esekiya, nga ne ko: Aji Sax ji sa Yàllay maam Daawuda dafa wax ne: “Dégg naa sag ñaan, gis naa say rongooñ. Maa ngii di yokk ci saw fan fukki at ak juróom.
Romans 8:26
TSK
¶ Te itam Noo gi moo nuy dimbali ndax sunug néew doole, nde xamunu sax li jaadoo sàkku ci sunuy ñaan, waaye Noowug Yàlla moo nuy tinule ay onk yu wees kàddug làmmiñ.