TSK

TSK · Leviticus 18:23

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ «Képp ku jaxasoo ak mala, dee rekk mooy àtteem.

Ku dëkkoo sa soxnas doom, mook soxnas doomam ñoom ñaar ñépp dee mooy seen àtte. Jëfu yàqute lañu def, kon ñooy gàddu seen bakkanu bopp.

¶ Ñu neeti: «Alku ñeel na ku tëdde mboolem luy mala.» Mbooloo mépp ne: «Amiin!»