TSK

TSK · Leviticus 6:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

mboolem li des ci yëkk wi daal lay génne dal bi, yóbbu ko ci bérab bu mucc sobe, ca jalub dóom ba, daldi taal matt, lakk ko ca, ba mu dib dóom. Foofa dóom ba jale lees koy lakk.

Su fekkee ne nit ki dafa laal sobey nit ak su mu mana doon, te teyu ko, ba mu wees, saa yu ko xamee, tooñ na.

Job 20:19 TSK

Moo dëggaate néew-ji-doole, dëddu ko; aakimoo kër jaambur te tabaxu ko.

Seeni lënd du ràbbe ba solal nit, mbaa di sàng kenn; seenum ràbb ñaawtéef lay jur, seen loxo ya ko liggéey sabab fitna,

ku ñàkk ak ku néewle, mu néewal, alalu jaambur, mu foqati, ab tayle, delloowu ko ku ko ameel, xanaa kasaray tuur, mu wékki gët, jëf ju siblu, mu jëfe,

Bu ñuy génn ca ëttu biti ba, ëtt ba mbooloo may yem, nañu summi seen yére ya ñuy sarxale, fat yére ya ca néeg yu sell ya, daldi sol yeneen yére, ndax baña sédd mbooloo mi sellnga, di leen lor.

Micah 2:2 TSK

Ñooy xemmemi tool, foqati, ay kër, ñu nangu, tey not waay ak waa këram, ak nit ci céru suufam.