TSK

TSK · Luke 1:65

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Luke 2:18 TSK

Mboolem ña dégg la leen sàmm sa wax nag waaru lool.

Acts 2:43 TSK

Ba loolu amee ag ragal jàpp ñépp, ay kiraama yu bare aki firnde daldi sottee ca jëfi ndaw ya.

Acts 5:11 TSK

Ba loolu amee tiitaange ju réy a jàpp mbooloom gëmkat ñépp, ak ña ko dégg ñépp.

¶ Waaye bu ñetti fan yeek genn-wàll wéyee, noowug dund giy bawoo fa Yàlla moo leen di solu, ñu jóg, taxaw, tiitaange lu réy daldi jàpp waa ceetaan ma.