TSK

TSK · Luke 17:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

«Éey saamar, yewwulal sama sàmm bi, sama jàmbaar jii ma lëngool,» kàddug Aji Sax jee, Boroom gàngoor yi. «Dóoral sàmm bi, xar yi tasaaroo, ma walbati sama loxo, jublu ci jur gu ndaw gi.

¶ Waaye man jariñoowuma lenn ci sañ-sañ yooyu, te binduma lii it ngir defalees ma noonu. Xanaa dee sax a may gënal— boobu sañ-sañu kañu daal, kenn du ma ko yàqal!

¶ Waaye na mu ame woon ci askanu bànni Israyil ay yonenti caaxaan, ni lay ame ci seen biir ay sëriñi caaxaan yuy sërxal ay àlluway sànkute yuy weddi sax Sang bi leen jot, ba yóbbe seen bopp sànkute ju bette.