TSK

TSK · Luke 18:39

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ba nit ka xamee ne manalu ko dara, dafa dóor Yanqóoba ci mooco, mooco mi summikoo ca bëre ba.

Su boobaa ngeen woo ma wall, dikk ñaan ma, ma nangul leen.

Luke 11:8 TSK

Maa leen ko wax, su jógul jox ko la mu laaj ndax ug xaritoo it, la ko kee amul kersay yee ngir sàkku ndimbal mooy tax mu jóg, jox ko mboolem lu mu soxla.

Luke 18:1 TSK

¶ Yeesu dellu leen léeb lii, ngir ñu wareefoo di sax ci ñaan te baña xàddi.

Ci kaw loolu mu àddu ca kaw ne: «Yeesu, Sëtub Daawuda, yërëm ma!»

Mbir moomu, ñetti yoon laa ci ñaan Sang bi, ngir mu sorele maak moom.