Exodus 20:8
TSK
¶ «Deeleen baaxantal bésub Noflaay, ngir sellal ko.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ «Deeleen baaxantal bésub Noflaay, ngir sellal ko.
Juróom benni fan lees di liggéey, waaye bésub juróom ñaareel ba, seen bésub Noflaay bu sell bu mat sëkk la, ñeel Aji Sax ji. Képp ku ci liggéey lenn, dees koy rey.
Waaye su ngeen ma dégloo ba déglu ma, kàddug Aji Sax jee, baña gàddu lenn di jaare bunti dëkk bii bésub Noflaay, xanaa di sellal bésub Noflaay, bañ cee liggéey lenn,
¶ Ca ëllëg sa, di ndoortel ayu bés, jigéen ña jëlu dem ca bàmmeel ba, yóbbaale cuuraay la ñu waajal.