TSK

TSK · Luke 4:16

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Luke 1:26 TSK

¶ Ba Elisabet tolloo ci juróom benni weeram, ca la Yàlla yebal Jibril malaaka mi, dëkk bi ñuy wax Nasaret ca diiwaanu Galile,

Luke 2:42 TSK

Ba Yeesu amee fukki at ak ñaar, ñu dem màggali na ñu ko baaxoo woon.

Luke 4:15 TSK

Muy jàngle ca seeni jàngu, ñépp di ko kañ.

Acts 17:2 TSK

Póol nag di leen fa fekk, na mu ko baaxoo. Diiru ñetti bési Noflaay, mu di leen waxal ci Mbind mi.