Moom doŋŋ la am ci yére, di ko sànge yaramam; su ko ñàkkee, lu muy sàngoo ba tëdd? Te su ma wooyee wall kat, dinaa ci dégg, ndax man Boroom Yërmande laa.
TSK
TSK · Luke 6:30
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Ci biir loolu askan waak seeni jabar di xultu lool ci seen kaw bokki Yawut.
Mooy nàddil néew-doole yi, njekkam sax dàkk, dooleem di yokku, ànd ak daraja.
Nit a ngi tabe, di yokkule; nit di nëŋ-nëŋi, gëna ñàkk.
day yendoo xemmem, te du am, ka jub di joxeek a joxewaat.
Ma walbatiku xalaat, di jéema xam fu xel rafete, di xoolaat li nit jàppoo fi kaw suuf, ba guddeek bëccëg, gëmmul bët.
¶ Ba loolu wéyee ngelaw ne ma siféet, yóbbu ma ba ca buntu penkub kër Aji Sax ja janook penku. Foofa ca bunt ba, yemuma ci lu moy ñaar fukki nit ak juróom. Ma xàmmi ca Yaasaña doomu Asur ak Pelaca doomu Benaya, di njiiti askan wi.
Li ci biir kay ngeen di sarxe! Su boobaa seen lépp ay set.
Yeesu dégg loolu, ne ko: «Lenn rekk nga deseleeti. Mboolem loo am, jaay ko, séddale ko néew-doole yi. Su ko defee nga woomle fa asamaan. Boo noppee, ñëwal, topp ci man.»
Xam ngeen kat sunu yiwu Boroom Yeesu Almasi, moom mi woomle woon, te yeena tax mu ñàkk, ngir woomale leen ag ñàkkam.
Sàcc bi, na ba sàcc te nangoo sonn, di liggéeye loxoom liggéey bu rafet, ba man cee dimbali néew-ji-doole ji.