TSK

TSK · Luke 9:55

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mu dem ba tollook ay ngéddi xar ca yoon wa; foofa am xuntee nga fa woon. Mu dugg ca biir, di suturlu. Fekk na Daawudaaki nitam a nga ca biir-a-biir xunti ma, toog.

¶ Abisay ma yaayam di Seruya ne Buur: «Simey mii, lu muy wax nii? Kii deesu ko rey? Du moo la doon saaga, yaw mi Aji Sax ji fal?»

Job 26:4 TSK

Ana ci koo jële sa kàddu yii sax? Ak ku la xelal miim xel?

Job 34:4 TSK

Kon nan ànd seet li dëggu te bokk ràññee li baax.

Job 42:6 TSK

Moo ma tax ne: «Wàqet, tuubi-ruubi,» ba diwoo suuf akub dóom.

«Dara gënula dëng xelum nit, laago la ci moom. Ana ku ko mana xam?

Acts 23:3 TSK

Póol ne ko: «Fél la yaw, moom la Yàlla di waaj, jinigalkat bee, mbete miir bu ñu weexal! Yaa ngi toog, topp yoon, di ma àtte, te teewul nga xëtt yoon, di ma dóorlu!»

Genn gémmiñ gi, ci la kàddug cant ak gu móolu di jibe. Bokk yi, warula deme noonu kat.

¶ «Man, képp ku ma sopp, maa koy jubbanti, yar ko. Kon nag farlul te tuub!