TSK

TSK · Micah 5:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Kuus moom itam jur Namróot, ki jëkk di jàmbaar ju siiw ci kaw suuf,

Ci jamonoy Peka buurub Israyil, Tiglaat Pilser buurub Asiri dikk, nangu dëkk yi ñuy wax Yon ak Abel Bet Maaka ak Yanowa ak Kedes ak Àccor ak diiwaani Galàdd ak Galile ak mboolem réewum Neftali. Mu jàpp waa réew ma, yóbbu Asiri.

¶ Ba Esekiya buurub Yuda duggee ñeenteelu atu nguuram, yemook ba buurub Israyil Ose doomu Ela duggee juróom ñaareelu atu nguuram, ca la Salmanasar buurub Asiri song Samari, gaw ko.

Job 29:22 TSK

Samay kàddoo leen di dal, genn-genn, te su ma àddoo ba daaneel, kàddu jeex.

Sa mboolooy taxawal seen bopp, sa bésub xare. Ña nga soloo darajaak sellnga, faboo fa njël sosoo, diy ndaw, wàccsil la, mbeteb lay.

Wóoy ngalla Asiri miy sama yetu mer, bolde bi ñu ŋàbb di samam sànj,

Maay joggati Asiri fi samam réew, dëggaate leen fi sama kaw tund yi, ba sama ràngi ñoñ rengiku, seenub sëf sippiku.»

Xërëmi neen yi yéefar yiy jaamu, ana ku ci mana taw? Am asamaan ay sóobal boppam ay waame? Du yaw la Aji Sax ji sunu Yàlla? Yaw lanu yaakaar, te loolu lépp, yaw a.

Keey xàccil loxoom bëj-gànnaar, keey sànk réewum Asiri, keey def Niniw ab gent bu wow ni màndiŋ.

Luke 1:71 TSK

moo nu musal ci sunuy noon, jële nu ci sunu loxoy mboolem bañaale.