TSK

TSK · Nahum 3:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Bu keroogee ñu fàtte Tir juróom ñaar fukki at, ni àppu benn buur. Bu juróom ñaar fukki at yi matee, Tir xewle la ñu woyal gànc ba, ne ko:

Diryànke bee, déglul lii: Yaa ngi ne finaax te naa ci sam xel: «Maa ko yor, man rekk, du keneen. Duma jooy jëkkër, duma jooy doom!»

Jàppool say jat rekk ak sa xërëm yu ne xas yoo dale sonn ba ngay ndaw. Jombul mu amal la njariñ, mbaa ñu ragale la ko.

¶ «“Kon nag Yerusalem gànc bee, déglul kàddug Aji Sax ji.

Mu àddu ca kaw, ne: «Babilon a daanoo! Dëkk bu mag ba daanu na, ba doon dëkkukaayu jinne ak mboolem njuuma lu sobewu ak mboolem picc ak rabu àll wu sobewu te siblu.

làmp du niiteeti fi yaw, te baatu boroom séet akub séetam du jibeeti fi yaw mukk, ndax say julaa ëppoon doole ci àddina, te say xërëm a sànk askanoo askan.»