Genesis 30:24
TSK
Moo tax mu tudde ko Yuusufa (mu firi Yal na dolli), ndax dafa ne: «Yal na ma Aji Sax ji dollil doom ju góor.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Moo tax mu tudde ko Yuusufa (mu firi Yal na dolli), ndax dafa ne: «Yal na ma Aji Sax ji dollil doom ju góor.»
¶ Ba ñu yóbboo Yuusufa Misra, Potifaar, jawriñu Firawna, ma jiite ay dagam, da koo jënd ca Ismayleen, ña ko fa indi.
¶ Ba loolu wéyee ñu ne Yuusufa baayam dafa tawat, mu ànd ak ñaari doomam Manase ak Efrayim, seeti ko.
«Yuusufaay bànqaasu garab, garab guy meññ, feggook bëtu ndox, car yaa nga law, tiim digu tool ba.
¶ Ñii nag ñoo askanoo ci Efrayim, ñook seeni làng: ñoom Sutela mi sos làngu Cuteleen ñi, ak ñoom Beker mi sos làngu Bekereen ñi, ak ñoom Taxan mi sos làngu Taxaneen ñi.