TSK

TSK · Numbers 33:54

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

làng gu gëna mag, na am cér bu gëna mag, làng gu gëna tuut, am cér bu gëna tuut, làng gu ci nekk, cér bi dëppook ab limam lees koy jox.

Dëkk yi ngeen leen di génneel ci céri suufi bànni Israyil nag, la cay génne ca ña ëpple suuf, réyal leen ko, te la cay génne ca ña néewle suuf, ngeen néewal ko. Giir gu nekk daal, dayob céru suufam si mu séddu, moom lay topp, ngir sàkke ci ay dëkkam, jox Leween ñi.»