TSK

TSK · Numbers 34:11

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Firawna Neko moo làqoon jant bi Yowakas ca dëkk ba ñuy wax Ribla ca réewum Amat, ba nguurootul ca Yerusalem. Mu teg réew ma galagu fanweeri barigoy xaalis, ak fanweeri kiloy wurus.

Mbooloom Babilon dàq leen, ba dab Cedesyas ca jooru Yeriko. Ñu jàpp ko, indil ko Nabukodonosor buuru Babilon ca dëkk ba ñuy wax Ribla, ca réewum Amat. Nabukodonosor dogal fa àtteem.

Ba mu ko defee Nebusaradan, njiital dagi buur, boole leen yóbbu ca buuru Babilon ca Ribla.

Luke 5:1 TSK

¶ Yeesoo taxawoon ca tàkkal dexu Senesaret, mbooloo ma tancaloo ci kawam, di déglu kàddug Yàlla.