ba noppi waral ko watiiru ku sës rëkk ci moom Firawna, te fu mu ware ñu jiitu ko, di yéene naan: «Sujjóotleen!» Noonu la ko Firawna fale, mu yilif Misra gépp.
TSK
TSK · Philippians 2:10
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Genesis 41:43
TSK
Romans 11:4
TSK
Ana lu ko Yàlla tontu? Da ne: «Beral naa sama bopp juróom ñaari junniy (7 000) nit ñu sujjóotaluloon Baal tuur mi.»
Ephesians 1:10
TSK
Li Yàlla namm, bu fan yi matee, moo di dajale lépp ci kilifteefu Almasi, mboolem la fa asamaan, ak li fi suuf.
Ephesians 4:9
TSK
Li ñu ne «moo yéeg,» ana lu mu tekki lu moy wàccoon na it ba fu gëna suufe?
Revelation 4:10
TSK
ñaar fukki mag ñeek ñeent ne gurub sukk fi kanam ki toog ci ngàngune mi, di ko sujjóotal, moom miy dund ba fàww. Ñuy sànni seeni kaala fi kanam ngàngune mi te naan:
Revelation 20:13
TSK
Ba mu ko defee géej jébbale néew ya woon ca moom, ndee ak njaniiw jébbale néew ya woon ca moom, ñu daldi àtte ku nekk ca say jëf.