Su ko defee noonee Aji Sax ji daan bége di leen baaxe ak a yokk, noonu la Aji Sax jiy bége di leen sànk ak a fàkkas, te dees na leen déjjatee ca réew ma ngeen jëm, ngir nanguji ko.
TSK
TSK · Proverbs 1:26
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Psalms 2:4
TSK
Ki ci jalub asamaan a ngay ree, Boroom baa nga leen di kókkali,
Proverbs 3:34
TSK
Kuy ñaawle, moo lay ñaawal, ku toroxlu, mu may law yiw.
Proverbs 10:24
TSK
Ab soxor, li mu ragal moo koy dab; nammeelu ku jub day sotti.
Proverbs 19:29
TSK
Na ñaawlekat bi séentu mbugal; ab dof, yeti gannaaw.