TSK

TSK · Proverbs 10:19

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 11:2 TSK

Yii kàddu yu wale, deesu ko tontoo? Wax ju bare tax na nit a yey?

Waxi xeebaate ñàkk bopp la, ku am ag dégg day noppi.

Nit ku ñaw day xam, ba ca; ab dof siiwal waxi dofam.

Bul gaaw làmmiñ, bul gaawa dikke Yàlla mbir. Yàllaa ngi kaw asamaan, yaw yaa ngi fi suuf. Kon na say kàddu néew.

James 3:2 TSK

Bare na lu nuy tooñ, nun ñépp. Ku dul tooñ ci kàddu nag, kooku nit ku mat la, te man naa moom yaramam wépp, boole ci.