2 Kings 19:34
TSK
Maay aar dëkk bii, musal ko ngir man ci sama bopp, ak Daawuda sama jaam bi.”»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Maay aar dëkk bii, musal ko ngir man ci sama bopp, ak Daawuda sama jaam bi.”»
Turam tukkee kaw suuf, ba deesatu ko tuddem pénc.
Yaa ma àtte yoon, dëggal ma, toog ci sab jal, di àtte njub.
Dama ne: «Aji Sax ji, tooñ naa la; baaxe ma, faj ma.»
Yal na seeni moy sax fi kanam Aji Sax ji. Yal na seen tur dagge fi kaw suuf.
Ma gis itam ñu bon ñu ñu rob, ñu daan yaale kër Yàlla ga, ñu di leen gërëme tey seeni jëf ca dëkk ba. Loolu it, cóolóoli neen.